Livre d'or

LAISSER UN MESSAGE

28 message(s) dans le livre d'or

  • diewrin
  • Le 05/12/2012

Ma ngui ziaar sama mbokku talibei yeup. Di leen dooli soniou si magal gui nga khamni ay fann you neew moo dess mou aksi. Di niaane yalla may niou niou fekkei ko. Loussi waay fass di niaane sunu borom ak serigne touba borom beuss bi maykoko... Wa salam

  • serigne saliou sy
  • Le 08/11/2011

mangui ziarr wa dahira fawzaini 18 safar gneup dilenne sognou thiy liguee yeul serigne bi rawatina magal gui ndax gnoune amenagne thiy ndigeul niary yone ndigeulul serigne touba ak cheikh mourtada kone nagne si gorgorlu boubax di sant yitam ablaye samb boubax thiy yittem ak yockoutee yimouy def toujour thiy site internet bi dieureuguenne dieufaty nguenne balma akh balnaa gneup wasalam

  • mouridisme
  • Le 06/11/2011

dieureudieuf serigne touba.

  • serigne mor sy
  • Le 25/06/2008

salam magilèndi ziyarè tay niane dahirabi barkèl tadilène wahkni kènna konèke nadiaponèmokowaradokgal bonokdèfè yalla danano dimbalè tèno fonk khasaidyi wasalame srigne mor sy italia boario tèrmè b s tl 00393807519117

  • serigne saliou sy
  • Le 25/06/2008

assalamou alaye koum magui nouyu tey ziaree wa dahiratou mathlaboul fawzaini 18 safar dilène fataly lgnoufy andi bayinoufy mouy diamou yallah ak ligeeyal serigne bi ndax lolou ràk mo am solo tàngenne geuna fonk khasidayi ndax khasidayi nimakodane wakhè ràk moye kholoup dahirai mook magalgui mandeh magui waat ci serigne touba ni lifèk khasidayi ak magalgui migui dox sounuye mbir dana dox sounouye hadio danaye fadiou adina ak allakhira lolou moom amoumaci loumaye wèrane tè tegnou geuna gorgorlu ci yar ak tèguinne ak fonk sonouye waa diour ndax ak taloubè bouci yarak tèguinne guinnè dara dotouthia dès magui dollè ziar gnepp tey sackou niane boubax te dilenne nianal wa salam serigne saliou sy depuis italie tèlè 0039 3807555934

Écrire un message sur le livre d'or

Vous utilisez un logiciel de type AdBlock, qui bloque le service de captchas publicitaires utilisé sur ce site. Pour pouvoir envoyer votre message, désactivez Adblock.